Music video by Bril Fight 4… performing EL Messias The Legend (Official Video). (C) 2014 … Exclusive track for the number one Bril (Ndéweuneul ) Directed by: Reverse Studios.
Class’Chic Records présente BRIL FIGHT.4… « Li Ma Déssé ? » + Lyrics
Class’Chic Records présente
BRIL FIGHT.4… « Li Ma Déssé ? »
Brand New single en #free_Download
Max de partage ***** Nathi nieuppp djottt yaaaa
·
LYRICS
Bril Fight 4… – Li Ma Dessé (Lyrics)
{Intro}
Class’Chic Records, Yeah …….Bril Fight 4… The last Fighter
Li Ma Déssé ngééni Lathie haan ??
Déggloul , Allright I write yaa
{1er Couplet}
May ki yagga gëstou doga tambali,seugg thi mbindeu mi def track
Andaki djambar sôbou thi kharé nieupp dokh ma dess di raakk
Laata baatou Obama di djipp la khamni « yes i can »
Oubi Class’chic di guéénè lou deep yakarouma thi kén
Def musique #fonction, dithi kheuy ,seugg thi , yaggueu thi beurri ay son
Dougou sa #domaine, #dérivé romb sa #limit yi wanela #variation
fayékou djizz thi bizz bi djay beats, wowèma Docter Dre
Deukk thi mixé master ay Hit ba niou beuri dok di diri,
Bagage yi, yeukk liy daw thi siditt , i’m the best ever did it
Téchnique bi visé, rime yi waathiélén né tireur d’élite
Xaré thi mbedd mi nekkeu fa heros bi, fégnal li neubouli wané sa zero bi ,
zik bi crazy, teureudi ,folli sa Prési… ,Eundi sa palai thi ghetto bi ,,,
{REFRAIN}
Niggiz wanna know , Li Ma déssé now
*********Yeaahhh******* allright
Cuz They wanna know , Li Ma déssé now
*********Yeaahhh*******Let’s go
Niggiz wanna know , Lane moma déssé now ?
Li ngay weur di laathieté , tontou-béngui sa guinaw , hun
Mangui nieuw, Yeukeutil-lén Hip Hop bi
Seugg thi mbindeu, wané thi deugg bi, guééné li nékk thi bopp bi
{2ème Couplet}
Kouy yeungou thi game bi kham nga may kann, djaratoul di déf semblant
Wouték nieupp néékha raagné ni bèn black thi 100 blanc ..
Boudéé Ki meunn sa king bi ngay séétt néma djakkeu ba weur
24h ma yèèw thi terroriste né « Jack Bauer »
Djèki djéki daw guissoma
All right i write yaw wo sama
Bépp number one ,rap ba gueunla wane, Bomb nieupp comme Ossama
Dikkeu djokhla leçon , tiidji say nopp sotifa son
Tabakh sa doundou ni bén maçon, May ki ngay dégglou sopi façon
Yakci Yéggueul niveau bi, yokkkou fi mbindeu mi , dougou thi xel yi di tatoué ,
Kou dékkeu sa nopp ci deunn yi, degg-nga xol yi nignoumay tathiou wé
Gni takhaw thi bitti di bagn, kouthi lakkou nim may thiatouwéé
Guéneu sissou ba dima teukeulék gni ma toloul thi thiatou wé….
{REFRAIN}
Niggiz wanna know , Li Ma déssé now
*********Yeaahhh******* allright
Cuz They wanna know , Li Ma déssé now
*********Yeaahhh*******Let’s go
Niggiz wanna know , Lane moma déssé now ?
Li ngay weur di laathieté , tontou-béngui sa guinaw , hun
Mangui nieuw, Yeukeutil-lén Hip Hop bi
Seugg thi mbindeu, wané thi deugg bi, guééné li nékk thi bopp bi
{3ème Couplet }
Da supa thi beat dou taaba taaba
Yokou na fèèm, ba gagnè kata ba
Romb di daw niou beuri di yaaba
Wakh thi djeumm dji yokou tiyaaba
Rime bou guéénati dal la né kaba
« Bril meunoul rap » Moy Macqua amoul kaaba
********Astaghfirullah Bakaar********** ,
Djoulil niaari raaka toubb, Khamnga ni léppeu la boolé bouppp,
Yokou fi léér bi, teuyé hilér bi , niakh yi maaguétt yeupp la gouppp
Gni nangou Technique bi , nane dou bindeu Sén your yi lamay sol daa
Thiappeu thi xalima xaatim soppilènn samay soldat
Dama eundi lou besss /wakh ma lou dess
Feuleu gueuna gaaw nieupp yokkou vitess
Tek lima meuné, niounè tékkeu gueuna yémou,Kouné beugg deuggeu deugg lima wané thi test …
Laakou Teudjou seugg reudd mbindeu gueuna beurri,
youkou déggeu déggueu founé, kouné guéneu dithi weuri ,
lima yagga. Seugg teugg , parè feugg nieup teurri ,
» I’m the best » kouy weur kouma meunn tèèla rééri
{REFRAIN}
Niggiz wanna know , Li Ma déssé now
*********Yeaahhh*******
Cuz They wanna know , Li Ma déssé now
*********Yeaahhh*******Let’s go
Niggiz wanna know , Lane moma déssé now ?
Li ngay weur di laathieté , tontou-béngui sa guinaw , hun
Mangui nieuw, Yeukeutil-lén Hip Hop bi
Seugg thi mbindeu, wané thi deugg bi, guééné li nékk thi bopp bi
{Outro}
Fi moy Galsén nigga , bougn lay laathie lééray nga eundil-lén djantt , ay torche laniouy weuri, taal di niitt nane-la dafa leundeum
« you already know what it is man » – Yama gueuna xam , ….. right
************************Dara Déssoul Nigga ***********************
Analyzik bi/// moy sopi Analou zik bi///
Bril Fight 4 #speed_test #teste_de_vitesse directed by Nazir Ciss 26.05.2014 + Lyrics
· I’m about to drop the best freestyle ever,,,,, listen !!! #speed_test #teste_de_vitesse Publié le 26/5/2014 #Speed_Test freestyle #Analyzik , Class’Chic Records 2014 Rappeur et beatmaker indépendant Sénégal/Dakar Directed By Nazir Ciss New single dispo sur http://www.reverbnation.com/brilfight4 · http://youtu.be/smJs1swMrvs · Finga beugga djégué laniou feugg,dinga djeulli liniou eundi,meuna khaamé finiou meuné, liniou nara wané, bakkou thi seugg beurré,songou naniou daan ndambou,doga meuna feugg deuneu, kouné guéneu weuri bénam… · Wala douniou meuneu takkeu ba di saam, sunu guinteu laniou wara fonkou deukk diko sameu, ben yone laniou xaleu andeu,dém loumou beurri beurri boul xol keulé limou sol dako béén am ? · Deugg laniou wané gniko céédé, beuga djégué dithi bégué, kouné fékhé finiouy teugué , ni nga yeugué, diko dééggué,beug beuga tégué , deug deug djokhé , liniou digué , finiouy diiigué doko fééké never « han » · *tou* *tou* *tou* · fooné cent mané tou tout , carte gui djoutou , supa dupa djitou , lathieté lépp connais tout, djouggatina daw dém , rawatina Bolt djokhatiko number *two* *two* · ======>>>>> Let’s go · Lifi gueuneu neubou laniou djeuli ,firi idji, bountou binga wara djaaré laniou djégué diko tidji, douma déggueu déé mongui dikkeu daw khidi fidi , liniouy iri, diniou diri , djaral naniou seugg sigui , deukeutéko ték ko tigui tigui , nieupp yokhou · *Daiiiimn* (rire) ……Come on · Léégui fouma dougou djokhé mayé minimum , kou thiy wakh yén rime yi teudji guémigneum , kila yagga deukkou, dila teukkou , djoké foukou foukou, soukou, douula meuna songou khéébatina meunineum, Guinteutina déminam , deugeulina aminam/, djégué nako dithi niaan déggeutouma amiiinam/ Liniou djappeu douniou teuri , sunu gaal day tééri , lima djangueu lay taari wané Ndieurigneum.
Bril Fight 4… « Sa Life – Sa Fight » Lyrics
Bril Fight 4… « Sa Life – Sa Fight » Lyrics
Intro
Yeah , sa doundala, sa xaaré la Sa life moy sa fight…. ANALYZIK
Refrain
You better put it in your mind
Gueum né war nga meuna Shine , One day {Sa life moy sa fight}
Boul Meussa Djoukk thi di Fight
Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}
Never say « no », Don’t say « no » {Boul meussa xaadi}
Never say « no », Don’t say « no »
1er Couplet
Li neubou thi yaw di nélaw sa djeumeu dji, fokk nga yééko hommy
Boul nangou di yééw sa xél ba gueumeu thi doundou gui, soukou sa Ôomm yi
Ki djouk ba takkou di kharé, thi finiou khaaré, yokkouna djoom yi
Bou peund bi wouré, gni yagga di beurèk ndiouma nio doul djoomi
Loussa xalat yi dadjati am-na // Kiy djéém té yaagg thi, meun-na //
Lou dougou thi bopp, mou toppeuthi fékhéko djeumeuli mbokk mi kham-na, //
Kouy khaadi lou djéguè la guissoul, Gueustoul, yégati thi, yénouko diissoul /
Djougueul, fékhél dokhé sa xél té bania di waakhi di soul //
Nangou gueuna djéém, yégali warèf yi doga meuna dém //
Ngèmbou beuré lay guiss, wouti dara like this, Boy khaar koula walou douniou meuna yém
Danga wara gueum dithi daw gaw/ Yégg finiou djeum yaw/
bania gueumeu khol lithi kaw naw/ sori am ndam founé law
Aw finiou djougué raw //Meuna djougati thi naathie wi ba faw
Refrain
You better put it in your mind
Gueum né war nga meuna Shine, One day {Sa life moy sa fight}
Boul Meussa Djoukk thi di Fight
Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}
Never say « no », Don’t say « no » {Boul meussa xaadi}
Never say « no », Don’t say « no »
2 éme Couplet
Boul nangou dinga déss guinaw, gueumeul sa bopp té deugou né « yay king, »
Kila romb dém, dééssouko naw, Boul déékkati koppeu yi nangoula « Fighting. »
Yaw yay the number one, Déél djangue thi lignou la wane
Dogali yégali, dogadi yeungali, waakhou yééwi say rawane
Nanga yeukk ni djom boula// Djito fi dara djiomboula //
Boy teuss teuss, beuss, yokkou pass pass, feuss, meunato woté niou Djamboula//
Kouthi tègouli djèègo yeungouwoul, euleuk meunoula djieum kanam/
Ki thi khéékh bi dooné djéngouwoul, filék wanoula djonkanam/
Pousso bi wara di niaw ba sopi sa doundou gui, yaa koy nass, né ci/
Fékhala dass mou niaw, nga Feugueuti peund bi, fomp mou néSs Néessi/
Béneu bouthi yém dém; danga wara djouk djém; weuri am ndam, takhaw thi Témeu
Beuss djeuli miseum, djizeum, tégui bizeum, wisdom la kheuw thi théme
Refrain
……..Put it in your mind
Gueum né war nga meuna Shine , One day {Sa life moy sa fight}
Boul Meussa Djoukk thi di Fight
Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}
Never say « no », Don’t say « no » {Boul meussa xaadi}
Never say « no », Don’t say « no »
Bridge
Now you gonna understand this is the way we gonna play {Boul xaar lééneu thi kééneu}
Now you gonna know you’re just living for the fight {Sa doundoula -Sa xaaré la}
Now you gonna understand this is the way we gonna stay {Boul sééntou ndimbeulou kénneu ,, man}
Now you gonna know, we better do it, for the fight {Défal linga wara déf Right now }
Outro
To be nobody but yourself ,, in a world that’s doing its best ,,,
to make you somebody else… {gueumeul sa bopp}
is to fight the hardest battle you are ever going to fight.
Right… The Last Fighter a-k-a The Future ……
Hi… Yya better know…
BRIL FIGHT.4… Sa Life – Sa Fight #ANALYZIK
Character cannot be developed in ease and quiet.
Only through experience of trial and suffering can the soul be strengthened, ambition inspired, and success achieved.
That which does not kill us makes us stronger.
BRIL FIGHT.4… Sa Life – Sa Fight (tavie-ton combat)
(single extrait de #ANALYZIK )
Enregistrement : Diegui Rails Studio
Trap beat, prod by : #killa-kid & Platinumbeatz Beatz
Mixage & Mastering : Class’Chic Records
http://www.reverbnation.com/brilfight4/song/20825084-sa-life-sa-fight
Bril Fight 4 au « G Hip Hop » de Guediway au concert de Fuk ‘n’ Kuk 03 May 2014
Everything I do, I do it for the love, and for all « the number one Bril »…
« Takkalé – bamou takkalo »
« Souba limou dinthia gueuna sakane mboki alcane »
#Sa_life__Sa_fight » —->coming soon
Bril Fight 4 au « G Hip Hop » de Guediway (Senegal) au concert de Fuk ‘n’ Kuk 03 May 2014
Sortie Officielle #Sa_life_sa_fight 10.05.2014 #BF4
La vie est un un combat que l’on mène contre soi,
Combat très dur parfois, Que l’on mène à chaque pas.
L’essentiel n’est pas d’avoir vaincu, mais de s’être bien battu.
Essayons de ne pas baisser les bras,
Croyons que demain tout changera,
Et que l’on sortira victorieux…
#Sa_life_sa_fight #ta_vie_ton_combat
Sortie officielle ce samedi 10 Mai 2014
https://www.facebook.com/events/sortieofficielle/safightsalife
Diegui Rails Studio présente
BRIL FIGHT.4… « Sa Life -Sa Fight » ( Sa doundou moy sa xaaré)
Single extrait de « #ANALYZIK_the_mixtape »
Concept : Reverse Studios
Sn Cypher Episode 5 – Sanzala – BillsMOZ (91District) – Shahide San (Book-e) – Balvada – Bril Fight 4
a »MicOpen » for Underground Rappers from SENEGAL,West Africa.
Revolutionizing the Hip-hop !
Studio: 2bedaxé Muzik, Video: Maybu Diaw, Montage: ZIGAZ MATEYDEF,
Realisation: NOPIL RECORDS.
All Rights Reserved NOPIL ENTERTAINMENT 2014.
#SNCYPHER #Senegal #WestAfrica #HipHopBestFreestylers
#Sky_Aint_Limit_For_Us #RevolutionizingHipHop !!!
https://www.youtube.com/watch/SnCypher5
Un peu d’histoire sur © BRIL FIGHT 4 ® █║▌│█│║▌║││█║▌║▌║║▌
Grandi entreThiaroye et Diamaguène quartiers très influents dans le rap Sénégalais, Bril fut Attiré par le Hip Hop à bas âge, Contaminé par le virus du rap, il forme avec Talla, Broda et d’autres amis le groupe Fight 4 Right en 2003. En 2006, FIGHT.4…connait la démission de deux de ses membres de part l’avancé du rap et du sacrifice à faire. La destiné du groupe se retrouve alors entre les mains de Talla et Bril » the supa creator ».
» The supa creator » parce qu’il avait appris la musique entre temps et était devenu un beat maker grâce à la M.A.O (Music assisté par ordinateur), et plus tard un technicien du son faisant des prises de voix, du mixage et du mastering. Armé de ces bagages techniques, il travaille dans divers studios d’enregistrement avant d’atterrir enfin à Def Dara Studio du rappeur Gaston, Diégui Rails Studio , et créer aussi son propre studio (Class’Chic Records)
Dès lors, « FIGHT.4 » avait à son répertoire plusieurs morceaux riches en expressions avec des techniques musicales très particulières et était en enregistrement pour leur album, Soudainement contre toutes attentes, Talla décida d’arrêter le rap pour des raisons très personnelles. Finalement, l’album de FIGHT.4… ne sortira pas cette année. Suite à cette démission, Bril se retrouve seul et décide de finir les projets sous l’appellation de Bril Fight 4 aka The Last Fighter (le dernier combattant).
Il sort « R’Aperitif » sa première mixtape en 2012. Sa musique, ses paroles et son sens du rythmes ont été remarqués et nul doute que ce n’est que le commencement pour lui. Une mixtape qui a réussit à le propulser au devant de la scène du hip hop sénégalais et qui lui a permis de participer au concours de Star Africa Sounds regroupant plus de 77 artistes africains en 2013 où il a été sélectionné dans le top 5, et a donc fait partie des finalistes…
2014 BRIL FIGHT 4… revient avec quelques singles bien accueillis par le public ( Ghetto heroes , Crazy muzik, Li neubou day feegn…) pour annoncer une prochaine mixtape « ANALYZIK » qui devrait voir le jour sous peu, produit par le label Diégui Rails et contenant de morceaux très lourds , ainsi que plusieurs featurings avec de très grands rappeurs et chanteurs . Et il travaille aussi dure sur son premier album où il essaye vraiment d’apporter une certaine touche, quelque chose de différent, au niveau du son, mais aussi au niveau de la façon de poser et du flow
D’aucun ignorait le sens philosophique de ma dénomination ; voilà, l’occasion de leur donner une interprétation claire. »
« Bril » est la forme contractée de bi-real. Bi signifie 2 en latin pour dire que je fais 2 choses (le rap et le beatmaking) dans le hip hop. « real » veut dire vrai : juste pour expliquer que je suis vrai dans les 2 choses que je fais.
« FIGHT , puisque la vie est un Combat (un combat Que l’on mène contre soi, Combat très dur parfois, Que l’on mène à chaque pas, Se battre pour vaincre ses peurs, Son désespoir et ses malheurs… Essayer de ne pas baisser les bras, Croire que demain tout changera, Que demain ça ira mieux, Et que l’on sortira victorieux)…….
4 plus qu’un chiffre, il représente les quatre éléments qui composent l’univers visible (Air, Feu , Eau , Terre ) On ne peut vivre en omettant un seul de ses 4 éléments…..
Ils symbolisent donc notre vie…….. « Le mot en tant que tel n’est pas ce qui est essentiel, mais c’est la combinaison des mots pour déterminer un autre mot qui est essentiel » L’addition de FIGHT, + 4 donne FIGHT.4… qui signifie dans notre dictionnaire Mener positivement un combat dans le milieu où l’on vit »
———————————————————————————————————————————-
To be nobody but yourself in a world that’s doing its best to make you somebody else, is to fight the hardest battle you are ever going to fight. Never stop fighting.
·
·
Source : https://www.facebook.com/brilfight4/posts/741119022589544